📺 Natty Jean - Sénégal [Official Video]

[Sous-titres Wolof/Français disponibles] 📀 Album ’Imagine’ : 🎙 Natty Jean en tournée : 📝 Auteur : Natty Jean 🎶 Compositeur : Massif B 🎥 Réalisation : Valentin Campagnie 💻 Montage-Étalonnage : Guillaume Agostin - AG Concept Art 🛰 Drone : Nazir Cissé 🙏 Remerciements : Karim, Teranga, Kamzo. Lyrics : [Wolof] This is for my people, Sénégal Njaay! Couplet Jolli na well, music bi deh le jolli na fi nañu teg level Ne Sénégal de kenn du ko yàq ak nimu mel Ñu change mentalité faut que ñu change suñu xel Xol yi nañu sell, naatange jolli well Man de lima xam ci corruption dugg ci jail Ku ci wàcc yoon ñu xàcc, bàcc yattu kel Ku fi jiite xamal ni xol yi de fees na dell kon boog nee ko rell Ana
Back to Top